Assalaamu aleykum wa rahmatullaahi wa barakaatuhu
Man Abdulaay Nag ñu gën maa xam ci Baay Laay Ñaŋ dëkk Kawlax/Medina Baay maa bëggoon a wax tuuti sama xalaat ci suñu gëstu bi; ma am yaakaar ne nag ku nekk war na ci mën a bokk ndax te mbir mu am solo la te it du caaxaan, ay mag, ay booromi xam-xam rekk noo koy jiite. Gëstu bi ñoo ngi ko door 2004 ba tay looloo tax nag am nañ ci ay dolléeku yu baree-bari ci wàll gu nekk nag. Leegi képp ku ci am loo bëgg a xam walla nga bëgg ka si yokk mën ngaa jokkoo ag membre mbootaay bi soo woote ci numero bii: 00 221 775250041 walla 00 221 779086859 su sóobee Yàlla di nga am lu la léer.
| < Prev | Next > |
|---|







